more from
Helico Music
We’ve updated our Terms of Use to reflect our new entity name and address. You can review the changes here.
We’ve updated our Terms of Use. You can review the changes here.

Boolo

by Senny Camara

/
  • Streaming + Download

    Includes unlimited streaming via the free Bandcamp app, plus high-quality download in MP3, FLAC and more.
    Purchasable with gift card

      €5 EUR  or more

     

1.
Boolo 04:21
Kéléya maniy néé Diougouya maniy néé Kéléya maniy néé Hééééééé kay lénn niou boolo Kéléya maniy néé Diougouya maniy néé Kéléya maniy néé Hééééééé Kay lénn niou boolo Boul di dox ci souma kanam Boul di dox ci souma ganaw Nanou anda ndo dox bok yone wy léé Moodi sounou doléé Dieumeuleu diangue ci sa morom Ame setlou ak dégue dégueu ci sa morom Sa morom térré laaa Keup kou Yalla sak sak na sa walleu Xol lenn ni ma Yalla bindéé Boukoul ak nila Yalla bindéé Ak keuléé nou ko Yalla bindéé Bokoul ak nila Yalla bindéé Kéléya maniy néé Diougouya maniy néé Kéléya maniy néé Hééééééé kay lénn niou boolo Déél ballou téy ballé Diélélé waxou sheytan Déél ballou téy ballé Diélélé waxou sheytan Bo xamé danguay xamlé Ko wéét nga wéétali ko Yow mba diam nga yendo Yow mba diam nga fananéé Kéléya maniy néé Diougouya maniy néé Kéléya maniy néé Hééééééé kay lénn niou boo Loloy sounou doléé Héééé kay lénn niou boolo Boolo loy sou nou dolééé Hééééééé kay lénn niou boolo Loloy sounou doléé Kay lene niou dioubo loloy sou dolle Xolene nouma yalla binde ak keuke nouko yalla binde Bokoniou niniou yalla binbe
2.
Dialé 04:23
Waxambané ya dess géth nioka barré Waxambané ya dess géth nioka barré Xalélya dess géth nioka barré Waala niou nga lénn niak ci calais Danou lénn bérr ci calais Niom deukou niou fi deukouniou faalé Danou lénn di nott founéé Niom deukou niou fi deukouniou faalé Danou lénn di nott founéé Ehh mang lénn di dialé Africa mang lay dialé Halél ya dess geth nioka barré Halél ya dess geth nioka barré Niou nga lénn di bom libyDef lénn diam liby Niom bokou niou fi bokou niou falé Niom deukou niou fi deukou niou falé Ehh mang lénn di dialé Africa mang lay dialé Syria Soudania Somalia Erithréa Ethopia Aganista Nigeria Ehhmang lénn di dialé Kou xamonn sa souba télaa fagaro Kou xamonn sa souba télaa fagaro Wayé bour Yalla mom ak ay kemanam Ehhmang lénn di dialé Ehh mang lénn di dialé Africa mang lay dialé Man ci souma dieum bop sax dama koy dialé Ablaye Niang,Souleymane Dansso,Smuel atorou, Nouhou Doumbia,Fatoumata Silla Oumar Diallo Nawell Sabibi Alian Keurdi
3.
Yon Wi 03:48
Yone wy léka soré Djitou na li ma goré Ndogal moka soré Djitou na li ma goré Xol moka goré Xél moy li woré Mom miy sanni yeuk yeuk Mou kor diame bilé Diame bi mounou ci dara eh eh Mandé guiss na souma lérr ci bénén dieum Man dé guiss na souma lér ci béné dieum hey yeh Man yeuk na lou yék ci souma dieum ak souma lér Oh yeuk na lou yék ci sou ma dieum ak sou ma lérr Souma xol souma xél souma takadér Souma xol souma xél souma takadér nirok mbeuguél Man yeuk na lou yék ci souma dieum ak souma lér Oh yeuk na lou yék ci sou ma dieum ak sou ma lérr Souma xol souma xél souma takadér Souma xol souma xél souma takadér nirok mbeuguél Mandé guiss na souma lérr ci bénén dieum Man dé guiss na souma lér ci béné dieumaa Yé hi yééé walou ci lén maa Yé hi yééé walou ci lén maa Yé hi yééé hééé walou ci lén maa Yone wy soré na té leudeum na fan lay diarr Yon wi soré na té leudeum na fan lay diarrrrr Yé hi yééé walou ci lén maa Yé hi yééé walou ci lén maa Yé hi yééé hééé walou ci lén maa Yone wy léka soré djitou na lima goré Yone wy léka soré dafa diegui lima goré Yone wy leka soré djitou na lima goré Yone wy lé ka sore dafa diegui lima goré
4.
Bim Bam 04:45
Ah yaye bim bam Uhh ah yaye bim bam Ah yaye bim bam Héy yé ah yaye bim bam Kala ak kourousse Uhh sata ak borom Yaye héé baniou ma ko dama ko ragal Héy héy kala ak kourousse Héyy satala ak borom Yaye héé baniou ma ko dama ko raagal Gorgou niaw dama fek Souma nek yaye maye mogne Gorgou niaw dama fek Souma nek yaye maye mogne Lékét ga toth soungouf ca né paw Randoul waye gorgou niaw Randoul randoul lo randoul lo Randoul waye gorgou niaw Randoul randoul lo randoul lo Lo diour momou loko Randoul randoul waye randoul waye Randoul waye diol mou ndaw yombaléma Man souma démé Mane dina fotal sa yaye di ko togal Di rote mouy nane bim bam Héy héy ah yay bim bam Wo wo ah yaye bim bam Uhh kala ak kourousse Uhh satala ak borom Yaye héé baniou mako da ma ko ragal Gorgou niaw dama fék Souma nék yaye maye mogne Wa diou niaw dama fek souma nek yaye maye mogne Lekete ga toth soungouf sa né paw Randoul waye gorgou niaw Randoul randoul lo randoul lo Randoul waye gorgou niaw Randoul randoul lo randoul lo Lo diour momou loko Randoul randoul waye randoul waye Randoul waye diol mou ndaw yombaléma Man souma démé Mane dina fotal sa yaye di ko togal Di rote mouy nane bim bam Héy héy ah yay bim bam Wo wo ah yaye bim bam Loumbay Fatoumata Seck loumba géy loumbi géth Bir ba dess teung géth bim bam Khare Baye néna ah yaye bim bam
5.
Talibé 03:47
Dimbali lénn xalé yi Sounou magué bérr sénn darra Diangual lénn xalé yi Sounou magué bérr sénn darra Dimbali lénn xalé yi Sounou magué bérr sénn darra Diangual lénn xalé yi Sounou magué bérr sénn darra Xalél sou dianguoul darra Sou magué dou meuna bérr darra Diangoul lou doul yalwann Sou magué dou meuna bérr darra Woye yoye woye yoye Talibé mom da fay yalwann Pote sa loxo ba tanki nénn Sagary nénn Woye yoye woye yoye Talibé mom da fay yalwann Pote sa loxo ba tanki nénn Sagary nénn Woye yoye woye yoye Talibé mom da fay yalwann Pote sa loxo ba tanki nénn Sagary nénn Chante pour tous les enfants qu'aucun parent n'attend. Fais toi l'écho retentissant des cris sourd que personne n'entend. Fais le pour tout ceux qu'on a volé a leur existence . Privé d'avenir et d'insouciance d'éducation mis sous silence. Chante pour les oubliés les mutilés talibés. Et pour tout les enrôles.Laisse ta voix s'envoler Qu'elle apaise les sanglots bien souvent privés de larmes. Chante les mélodies pour remplacer le bruit des larmes. Chante pour l'avenir la mémoire et le souvenir Pour redonner vaillance à ceux que personne ne va soutenir Tu connais la triste réalité. Fais toi la voix des talibés Et que la douceur de ta voix leur rappelle ce qu'est la tendresse Comment peut ton encore laisser faire ? Baye ndongo gui beugueu déé si darray damay yalwann Amou fi daye amou fi baye Xam xam la sacou si wonn Baye ndongo gui beugueu déé si darray damay yalwann Baaaaaaa ya ngi beugueu déé si darray damay yalwann Amou fi daye amou fi baye Xam xam la sacou si wonn Woye yoye woye yoye Talibé mom da fay yalwann Pote sa loxo ba tanki nénn Sagary nénn Woye yoye woye yoye Talibé mom da fay yalwann Pote sa loxo ba tanki nénn Sagary nénn Woye yoye woye yoye Talibé mom da fay yalwann Pote sa loxo ba tanki nénn Sagary nénn

about

SENNY CAMARA

La musique, chez Senny Camara, c'est avant tout une histoire de cordes. Celles de sa kora - traditionnellement réservée aux hommes - dont elle a su faire une alliée pour s’accomplir en tant qu’artiste mais aussi en tant que femme. Profondément attachée à son indépendance, Senny Camara a préféré apprendre elle-même les secrets de la harpe-luth des djélis plutôt que de compter sur un maestro ou sur la providence.

Insoumise, libre et pugnace, Senny Camara partage de nombreux points communs avec ses femmes-totems : Nina Simone, Joséphine Baker, Chimamanda Ngozie Adichie, mais aussi la musicienne guinéenne Mahawa Kouyaté, griotte et reine de la kora, qui demeure pour elle une véritable source d’inspiration. Mais la femme à qui elle doit son intuition et le naturel de sa manière d'être au monde, c’est sa grand-mère, qui l’élève dans les plus pures traditions du peuple Sérère, au sud du Sénégal. Rokhaya lui transmet le don de s’émerveiller, de danser pour la pluie, la dignité de la forêt, le sens de la communauté. Rokhaya l’initie aussi à la mystique et aux tambours de transe des cérémonies ndüp. Grâce à son transistor à piles, la petite Senny découvre la culture mandingue de son père, ancien tirailleur sénégalais, et la vénérable Mahawa Kouyaté - dont elle chante le répertoire en secret mais sur le bout des doigts !

A 20 ans, Senny Camara débute au sein d’un orchestre à Dakar. Elle se produit dans les hôtels, chantant standards de jazz américain et afro-cubain, Madonna, Catherine Ringer, Michaël Jackson ou Laura Pausini... Une ouverture musicale internationale fondatrice très instructive quoi qu’inattendue ! Les shows se multiplient et Senny parvient à s’offrir sa première kora. Après une initiation auprès du maître Youssoupha Koutidjo, Senny Camara approfondit sa relation avec l’instrument au sein du Conservatoire de Dakar, s’affranchissant alors du répertoire strictement traditionnel.

Et puis, la vie et l’amour l'amènent finalement à s’installer en France à l’orée des années 2000. Les saisons passent et la route de Senny Camara croise celle de virtuoses mandingues en exil, de musiciens nomades comme Fixi ou Ignacio Maria Gomez Lopez, mais aussi des sœurs, à l’image de l’ébouriffant collectif O’Sisters piloté par Missill, productrice et marathonienne du mix. Curieuse et collective, la musique de Senny Camara honore bien sûr la majesté de la kora, mais elle invite aussi les cordes d’une harpe celtique, d’un cavaquinho brésilien ou encore d’un kankles de Lituanie, toutes venues enrichir son instrumentarium au fil des rencontres.

Aujourd’hui, Senny Camara dévoile BOOLO, l’unité en wolof, un premier EP qui prouve encore que le temps porte ses fruits à qui sait attendre la bonne saison pour les cueillir. Dans BOOLO, Senny Camara se révèle authentique à la faveur d’une voix souple, donnant de l’amplitude à sa kora en la mariant à la guitare de Thierry Fournel, à la souplesse de Bakary Diarra au balafon et à la contrebasse profonde de Pierre-Yves Le Jeune.
Des cordes sensibles au gré desquelles Senny Camara appelle à l’équilibre, à l’unité, au vivre-ensemble et à la solidarité sur “Boolo”. Sur “Dialé”, Senny adresse ses condoléances à celles et ceux que la migration prive trop souvent d’un être cher. Senny chante l’amour plus fort que la raison sur “Yone wy” et celui qu’on ne choisit pas sur “Bim Bam”, relecture intime d'un morceau traditionnel, sous forme de conversation mère-fille, pour dénoncer le mariage forcé. “Talibé” enfin, souligne la responsabilité de tous.tes quant à l’éducation des plus jeunes, piliers du changement. Tandis qu’elle chante, la kora au bout de ses doigts, Senny Camara honore en pensées l’indocilité de Fanon ou Fela, comme la sagesse d’Amadou Hampâté Bâ, délivrant un premier EP juste et harmonieux.

Texte : Jeanne Lacaille

credits

released November 9, 2020

Senny Camara : Kora, chant
Thierry Fournel : Guitare
Pierre Yves Le Jeune : Contrebasse
Honoré Kouadio : Perciussions
Bakary Diarra : Balafon

license

all rights reserved

tags

about

Senny Camara Paris, France

contact / help

Contact Senny Camara

Streaming and
Download help

Report this album or account

If you like Senny Camara, you may also like: